From Wikipedia
Ci làkku ibrë la tur wi jóge. Ci angale mooy Abiathar; Ci faranse mooy Abiathar
Saraxalekat bu mag ba la woon, ci jamano nguuru Daawuda. Man nañu ko gis ci 1Sa 22:20-21; 2Sa 15:24-29; 20:25; 1Ki 2:22-27,35; 1Ch 15:11-13; 27:33-34.
Ci Injiil dañuy wax ci Abiyatar ci Mk 2:26.