From Wikipedia
Wolof mooy làkk wi nu gën a wax ci Senegaal, waaye ngir doyodig waa Afrig yi ba leegi, franse mii nga xam ne lu matul fukk ak juroom cib téeméer ci doomi Senegaal yi rekk a koy wax moo fiy lakku ofisel wi, maanaam wi àtte gi (l'Etat) di waxe di ci ligeeye.